Good morning/ afternoon
Assalaamaalekum?
Maalekum salaam
How are you?
Nanga def?
Naka nga def?
I am fine.
Maangi fi rekk
Is your body in piece?
Sa yaram jàmm?
In pease only, thanks to god
Jàmm rekk alxamdulilaay
How is the family?
Naka waa kër ga?
They are fine
Ñungi fi
Did you spend the day in peace?
Jàmm nga yendoo?
to be
ngi
to sit
toog
to call/ heißen
tudd
how
Naka
What?
Lan
Who?
Kan
This
Lii
This one (human)
Kii
Here
Fii
Where
Fan
Jemand”s” …
possessive s
-u
my
sama/ suma
Your
Sa
to be hungry
xiif
to be thirsty
Mar
I am hungry
Xiif-naa
I am thirsty
Mar-naa
I am eating
Mangi lekk
I am drinking
Mangi naan
I am having lunch
Mangi añ
I am having dinner
Mangi reer
I am having breakfast
Mangi ndekki
Reis
ceeb
Brot
Mburu
Wasser
Ndox
Milk
meew
Tea
Attaya
Zuletzt geändertvor 2 Jahren